0^SàkkaryaaWaññiku ci Aji Sax ji weesulMisaal mu jëkk: Ay fas aki gawarÑaareelu misaal: Ay béjjén ak ay tëggÑetteelu misaal: Nit kuy natt YerusalemÑeenteelu misaal: Yosuwe am na col gu yeesJuróomeelu misaal: ay tegukaayi làmp ak garabi oliwJuróom benneelu misaal: Taxañu mbind buy naawJuróom ñaareelu misaal: ndab lu jigéen toog ca biirJuróom ñetteelu misaal: ay watiiri xareFal nañu buur sarxalkat bu mag biLeeraange ci mbirum koor dikk naMbéx wuutu na koorMbugal mu mucc topp dal na askani diiwaan biBuur Almasi dikk naAji Sax ji mooy xeexal ñoñamXërëm neen laYiwiku ñeelati na IsrayilSàmm bu baax jotul yoolamYerusalem yiwiku naÑaawlu dikkal na réew méppAy tuur ak yonenti caaxaan day jeexKóllëre feddliku naXare bu mujj jib na