0^RoomPóol sant na YàllaManooree ngi ci xibaaru jàmm biNit ñépp a tooñ YàllaYàlla mooy àtteYoonu Musaa na jariñ ki ko toppXaraf na jariñ boroomLu jëm ci jagley Yawut yiKenn jubulYàlla ubbi na buntu muccNjubteg Ibraayma du ci jëfamIbraayma gëmoon na digeb YàllaAlmasi moo nu jubale ak YàllaAadamaa nu xañ bakkan, Yeesu delloo nu koBàkkaar yilifatul gëmkatub YeesuKu gëm Yeesu, ag njub ngay surgawuYoonu Musaa wàcc na gëmkatub AlmasiYoonu Musaa moo wone ne bàkkaar moo yéesAb gëmkat namm na lu mu tëlee jëfeNoowug Yàlla moo jiite gëmkat biTeraangay ëllëg ñeel na gëmkat ñiCofeelu Yàllaa ngi ci AlmasiYàlla moo taamu bànni IsrayilSànjum Yàlla rax na yërmandeBànni Israyil déggoowul ak xibaaru jàmm biCoobarey Yàlla mooy ñépp muccYàlla waccul bànni IsrayilLu jëm ci muccug ñi dul YawutYàlla ñépp la yërëmYàllaa yelloo teddngaNii la gëmkat bi wara jaamoo YàllaNa ñépp déggal njiit yiCofeel moo tënk yoonu MusaaTeewlu war na gëmkat ñiBul sikkal sa moroomBul yóbbe sa moroom bàkkaarNa gëmkat yiy xajoonteXibaaru jàmm bi ñépp la dikkalPóol xamle na sababu bataaxalamPóol dige naa seeti waa RoomPóol nuyu na waa RoomKàdduy àrtu ak tàggoo ñeel na waa RoomTeddnga ñeel na Yàlla