0^MACËCosaanu Yeesu KiristJuddub Yeesu KiristAy boroom xam-xam ñëw nañu, màggalsi YeesuYuusufa ak Maryaama gàddaay nañu jëm réewu MisraÑibsi nañu réewu IsrayilWaareb YaxyaYaxya sóob na Yeesu ci dexu YurdanYeesu dékku na ay nattu ci pexey SeytaaneYeesu dëkk na Kapernawum ci diiwaanu GalileYeesu tànn na ñeenti taalibeBarkeel gu wóor giXoromus àddina ak leeramNi yoonu Musaa ak waxi yonent yi ame ci YeesuMere nit ak bóom ko ñoo yem fa kanam YàllaKu xédd jigéen, njaaloo ngaBul fase sa soxna lu dul ci njaalooBul weddi sa ngiñBul feyuNi ñuy sàkke saraxNi ñuy ñaane ci YàllaNi ñuy wooreAlali laaxiraWóolul YàllaBul ñaaw njort, ba àtte sa moroomYàlla nangu na ñaanu ku gëmBunt bu xat biGarab ak meññeefamLéebu ñaari tabaxkat yiYeesu faj na ku gaanaNgëmu njiitu xare biYeesu faj na jarag yu bareYeesu dalal na ngelaw liYeesu faj na ñaar ñu rab jàppYeesu faj na ku làggiYeesu woo na Macë, mu nekk taalibeemNdax warees na woor?Yeesu dekkal na doomu njiitu jàngu ba te faj jigéenYeesu faj na ñaari gumbaYeesu faj na ki rab jàppYeesu yërëm na mbooloo miYeesu yónni na fukki ndaw ya ak ñaarYaxya yónnee na, di laaj YeesuYeesu gëdd na ay dëkkWoote bu mag biYeesu nee na, mooy boroom bésub noflaay biYeesu faj na nit ku loxoom làggiKu rab jàpp, mu gumba te luuKu sosal Xelu Yàlla miYeesu nanguwula def kéemaanNdeyu Yeesu ak i doomi ndeyamLéebu beykat baLu tax Yeesu di wax ay léebYeesu firi na léebu beykat biLéebu jëmb biLéebu doomu fuddën giLéebu lawiir biLéebu alal ju nëbbu ak léebu per baLéebu mbaalum géej gaLéebu boroom kër gaYeesu ci dëkku NasaretYaxya faatu naYeesu bareel na mburu yaYeesu dox na ci kaw ndox maFarisen ya ak aada yaYeesu faj na doomu jigéen, ja askanoo réewu KanaanYeesu faj na ñu woppYeesu bareel na ay mburu ñaareel bi yoonKéemaan gu jóge ci asamaanPiyeer wax na ne, Yeesu mooy Almasi biNdamu Yeesu jolli na ci moomYeesu faj na xale bu rab jàppYeesu waxaat na ne dina dee, dekkiYeesu fey na warugaru kër Yàlla gaKan moo gëna màgg?Ñi yóbbe nit bàkkaarXar mu réer maMbaalug bàkkaar yiJaraaf ju amul yërmandeÑi fase, ak ñi baña séy ngir jaamu YàllaXale yu ndaw yiWaxambaane wu bare alalLéebu liggéeykat yi ñu jël ci waxtu yu wuuteYeesu xamle na ñetteelu yoon ne dina dee, dekkiLi doomi Sebede ñaan YeesuYeesu faj na ñaari gumbaYeesu dugg na YerusalemYeesu dàq na jaaykat ya ca kër Yàlla gaYeesu rëbb na garabu figg gaSañ-sañu YeesuLéebu ñaari doom yaLéebu beykat, yi rey doomu boroom tool biLéebu céet gaGalag gi ñuy fey buur bi SesaarSadusen yi ak ndekkite liBan santaane moo gëna màgg ci yoonu Musaa?Ndax Almasi bi mooy sëtu Daawuda?Yeesu gëdd na xutbakat ya ak Farisen yaYàqug Yerusalem ak dellusig Doomu nit kiYàlla rekk moo xam bés baLéebu fukki janq yaLéebu surga, ya njaatige bi dénk xaalisamÀtteb xeet yiNjiiti yoon yi fexeel nañu YeesuJigéen ja tuur na latkoloñ ci boppu YeesuYudaa wor na YeesuReer bu mujj biYeesu ñaan na ci toolu Setsemane ci biir tiis wu réyJàpp nañu YeesuYeesu taxaw na ci kanam kureelu àttekat yaPiyeer weddi na YeesuYudaa am na naqar lool, ba xaruYeesu taxaw na ci kanam PilaatXarekat ya ñaawal nañu YeesuDaaj nañu Yeesu ci bant biYeesu saay naRob nañu YeesuYeesu Kirist dekki na