0^JËF YAYeesu Kirist yéeg na ci asamaanÑu tànn Macas, mu wuutu Yudaa, nekk ndawÑëwug Xel mu Sell mi ca màggalu PàntakotPiyeer yégal na mbooloo mi xibaaru jàmm biMbooloom ña gëm KiristPiyeer faj na nit ku lafañWaareb PiyeerPiyeer ak Yowaana ci kanam kureelu àttekat yaMbooloom ñi gëm ñaan na ci YàllaMbooloom ñu gëm ñiAnañas ak SafiraNdawi Kirist yi faj nañu ñu bareFitnaal nañu ndaw yiSàkk nañu ñiy topptoo yëfi mbooloo maJàpp nañu EcenLayu Ecen fa kanam mbooloo maSànni nañu ay doj Ecen, ba rey koFitnaal nañu mbooloo miFilib waare na ci diiwaanu SamariSimoŋ luxuskat biFilib yee na jaraafu EcópiSóol waññiku na ci YeesuPiyeer faj na EnePiyeer dekkal na TabitaKorney woo na PiyeerPiyeer ci kër KorneyPiyeer leeral na jëfam fa kanam gaayi Kirist ya nekk YerusalemBarnabas ak Sóol ci dëkku AncosYàlla musal na Piyeer ca kaso baBuur Erodd dee naYàlla yónni na Barnabas ak SóolWaare nañu ci dunu SiparWaare nañu ci Ancos ci diiwaanu PisidiPool ak Barnabas ci dëkku IkoñumPool ak Barnabas ci dëkku ListarDélsi nañu dëkku AncosGéew bi am ci YerusalemBataaxal bi ndaje mi bind ñi dul YawutÑaareelu tukkib ndaw la Pool, ànd ak SilasTimote àndsi na ak Pool ak SilasYàlla wax na ak Pool ci biir peeñuLidi gëm na Kirist ci dëkku FilibTëj nañu Pool ak Silas ca kaso baPool ak Silas ci dëkku TesalonigPool ak Silas dem nañu BerePool ci dëkku AtenPool ci dëkku KorentPool délsi na dëkku AncosÑetteelu tukkib Pool, ngir yégle xibaaru jàmm biPool ci dëkku EfesAy kéemaan yu bare am na ci EfesYëngub mbooloo mi ci EfesPool jaar na ci diiwaani Maseduwan ak GeresPool dekkal na Ëtikus ci TorowasPool tàggoo na ak njiiti mbooloom ñi gëm ca EfesPool jublu na ci dëkku YerusalemPool ci dëkku YerusalemJàpp nañu PoolPool layoo na ak waa YerusalemPool wone na ne jaambur la ci nguuru RoomDëj nañu Pool ca kureelu àttekati Yawut yaYawut ya lal na pexe ngir rey PoolYóbbu nañu Pool dëkku SesarePool lay na ci kanam Feligsë, boroom réew ma.Pool làyyi na ca kanam FestusFestus diisoo na ak buur AgaripaPool teew na ci kanam AgaripaLayu Pool fa kanam AgaripaPool dugg na gaal, di dem RoomNgelaw lu metti liToju gaal gaPool ci dunu MàltEgg nañu dëkku RoomPool xamle na xibaaru jàmm bi ca Room